Genesis 12:4
TSK
¶ Ibraam daldi dem, na ko ko Aji Sax ji waxe woon, Lóot topp ca. Ba Ibraam di jóge Karan, booba am na juróom ñaar fukki at ak juróom (75).
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
¶ Ibraam daldi dem, na ko ko Aji Sax ji waxe woon, Lóot topp ca. Ba Ibraam di jóge Karan, booba am na juróom ñaar fukki at ak juróom (75).
Isaaxa am ñeent fukki at, jël Rebeka doomu Betuwel, Arameen, bi dëkke diiwaanu Padan Aram, dib jigéenu Laban, Arameen ba.
Yaayam ne ko: «Bu la móoloo, Yàlla na ma topp, doom. Defal li ma la wax rekk te dem indil ma gàtt yi.»
¶ Ba loolu wéyee Yanqóoba génn Beerseba, wuti Karan.
“La Yonadab doomu Rekab santoon ay doomam ne leen: ‘Buleen naan biiñ’ de, jëfees na ko. Duñu naan biiñ ba tey jii ndax wormaal seen santaaney maam. Man nag ay yooni yoon laa leen wax waaye déggaluleen ma.