Aji Sax ji ngeen biral bésub tey, ne mooy doon seen Yàlla, te dingeen doxe ay yoonam, di sàmm dogali yoonam, aki santaaneem, ak àttey yoonam, tey dégg waxam.
TSK
TSK · Genesis 28:21
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
2 Samuel 15:8
TSK
ndax kat, sang bi, ba ma nekkee Gesur ca Siri, damaa dige woon ne: “Su ma Aji Sax ji delloo, ba ma dellu Yerusalem, dinaa dem màggali ko.”»
2 Samuel 19:30
TSK
Buur ne ko: «Ana looy waxati lii lépp? Dogal naa yaak Ciba, ngeen séddoo suuf si.»