TSK

TSK · Genesis 29:13

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Rebeka amoon na càmmiñ lu tudd Laban. Laban daldi gaawtu génn, fekki waa ja ca seyaan ba.

Magam ña itam, mu fóon leen tey jooy. Booba la magi Yuusufa ya doora wax ak moom.

Musaa génn gatandu ko, sujjóotal ko, fóon ko; ñu jàmmante ba noppi, doora dugg ca xayma ba.

Luke 7:45 TSK

Fóonuloo ma, dalale ma, waaye moom, ba ma duggsee ba léegi noppiwula fóon samay tànk.

¶ Saafoonteeleen fóonante yu sell. Mboolooy gëmkati Almasi yépp nuyu nañu leen.