TSK

TSK · Genesis 29:24

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

¶ Sarayi amul woon doom ak boroom këram Ibraam. Waaye fekk na mu am jaam bu juddoo Misra te tudd Ajara.

¶ Leya moom it xam ne taxawaayam yàgg na, mu fab jaamam Silpa, may ko Yanqóoba.

Góor ñooñoo xeetoo ci Silpa, mi Laban may Leya, doomam ju jigéen, te ñu askanoo ci Yanqóoba, ñuy fukki bakkan ak juróom benn.