Genesis 27:35
TSK
Isaaxa ne ko: «Sa rakk ñëw na, nax ma, ba yóbbu sa ñaan.»
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Isaaxa ne ko: «Sa rakk ñëw na, nax ma, ba yóbbu sa ñaan.»
¶ Laban ne Yanqóoba: «Looy def nii, yaw, di ma nëbbuy daw, yóbbaale sama doom yu jigéen, ñu mel ni ñu ñu lële xare?
Ku jub, jot sa yool ci kaw suuf, moykat beek soxor bi it daw raw.
ku ci nekk, sab liggéey dina feeñ, ndax bés baa koy xamle, nde sawara lees koy feeñale. Ku ci nekk, ak lu sa xeetu liggéey mana doon, sawara lees koy natte.