TSK

TSK · Genesis 30:23

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Waaye Aana la daan beral loxo ca sarax sa, ndax cofeelam ci moom, doonte Aji Sax ji mayul Aana doom.

Luke 1:21 TSK

¶ Ci biir loolu mbooloo maa ngay xaar Sàkkaryaa, jaaxle lool ndax yàggaayam ca biir néeg Yàlla ba.

Luke 1:27 TSK

ci janq bu digoo séy ak waa ju ñuy wax Yuusufa te bokk ci waa kër Daawuda. Janq ba Maryaama lañu koy wax.