Genesis 16:3
TSK
Looloo ngi am, gannaaw ba Ibraam dëkkee fukki at ca réewu Kanaan. Sarayi daldi jël Ajara, jaamam bi juddoo Misra, jox ko jëkkëram Ibraam, ngir mu dëkkoo ko.
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Looloo ngi am, gannaaw ba Ibraam dëkkee fukki at ca réewu Kanaan. Sarayi daldi jël Ajara, jaamam bi juddoo Misra, jox ko jëkkëram Ibraam, ngir mu dëkkoo ko.
Rewma it nekkaaleem la woon, doom ya mu ca am di Teba ak Gaxam ak Taxas ak Maaka.
Doom yu góor, ya mu am aki nekkaaleem, mu may leen alal ca ba muy dund, ba noppi yebal leen penku, ñu sanci ca réewu penku, ba sore doomam Isaaxa.
Dafa jiital jaam ya ak seeni doom, tofal ca Leya ak ay doomam, Rasel ak Yuusufa féete gannaaw.
Góor ñooñoo xeetoo ci Bilaa, mi Laban may doomam Rasel, te ñu askanoo ci Yanqóoba, ñoom ñépp di juróom ñaari bakkan.