TSK

TSK · Genesis 31:12

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Bu jur gu xiibon gi dee tëbu, mu bañ leena tegal dara. Muy def noonu ba jur gi xiibon, di gu Laban, gi am doole, di gu Yanqóoba.

¶ Aji Sax ji tegaat ca ne ko: «Gis naa bu baax fitna, ji sama ñoñ nekke Misra. Dégg naa itam seen jooy ndax kilifay saskat, yi leen di gétën ci liggéey, te ñeewante naa leen ngir seen coono.

¶ «Buleen lekk seen àqu moroom, buleen sàcc. Buleen wacc peyu liggéeykat, muy fanaan ci seeni loxo.

Yaw de yaay ki nemmiku, di gis njekkar ak naqar, ku mu dal, nga sàmm àqam. Néew-ji-doole wéeroo la, ab jirim, nga dimbali.

di càmbar samab dox ak sama tëraay, yittewoo lépp lu may def.

Acts 7:34 TSK

Gis naa bu baax sama coonob ñoñ ci Misra; maa dégg seeni onk, ba wàcc ngir wallusi leen. Léegi nag dikkal, ma yebal la Misra.”