TSK

TSK · Genesis 34:2

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

ay goney Yàlla ñoo gis jigéen ñeek seen taar, ñuy jël ñi ñu bëgg ci ñoom, def leeni jabar.

Ba Ibraayma àggee nag, da ne soxnaam Saarata ab jigéenam la. Abimeleg buurub Gerar daldi yónnee jëlsi Saarata.

La ca tegu doomi Yanqóoba ya ca des futti néew ya, lëlaale dëkk ba, ndax li ñu torxal seen jigéen.

Bu loolu amee ba neexatu leen, bàyyileen ko, mu dem fu ko neex, waaye buleen ko jaay mukk, di ko weccikoo xaalis. Buleen ko jaamloo it, gannaaw bu ngeen ko jabaroo ba noppi.

kooka tëdde ndaw sa, day jox baayu ndaw sa juróom fukki donji xaalis. Jabaram lay doon it, gannaaw moo ko jabaroo, te du ko saña fase, giiru dundam.

¶ Genn ngoon, Buur Daawuda jóge ca kaw laltoom, di doxantu ca kaw taaxum këram. Mu tollu ca kaw taax ma, séen as ndaw suy sangu. Ndaw sa neexa xool lool.

Amnon nag dégluwu ko, xanaa néewal ko doole, ba tëdde ko.

Job 31:9 TSK

Ndegam jabaru jaambur a ma xañ sago, ba ma di ko yeeroo sama buntu kër moroomu góor,

Baay la doom di teddadil lalam fi sa biir, ku gis baax, ñu tëdde fi sa biir.