¶ Ba Ibraam amee juróom ñeent fukki at ak juróom ñeent (99), am na bés Aji Sax ji feeñu ko ne ko: «Man maay Yàlla Aji Man ji. Topp ma te mat sëkk.
TSK
TSK · Genesis 35:9
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
¶ Foofa Aji Sax ji feeñu ko fa ne ko: «Bul dem Misra, waaye nanga toog ci réew mi ma lay wax.
Aji Sax ji wax Yanqóoba ne ko: «Dellul ca sa réewu maam ya, ca say bokk. Dinaa ànd ak yaw.»
¶ Ca ëllëg sa, Laban xëy suba teel, tàggoo aki sëtam ak doomam yu jigéen ya, ñaanal leen, ba noppi waññiku ñibbi.
Yanqóoba ne ko: «Waaw, yaw nag noo tudd?» Mu wax ko ne ko: «Loo may laaje sama tur?» ba noppi barkeel ko foofa.
Yàlla wax ak Israyil foofa ca guddi ci biir gént ne ko: «Yanqóoba, Yanqóoba!» Israyil ne ko: «Naam.»
Ñu ne: «Bu yàgg la nu Aji Sax ji feeñu, ne nu: “Maa leen masa bëgg, ba tax ma sédd leen ngor.
Kee bëreek malaaka, ba génn ca, kee jooy di sàkku aw yiwam. Fa Betel la ko fekk, te foofa la Yàlla waxeek nun.