Genesis 39:14
TSK
mu woo surgay kër ga, ne leen: «Xool-leen, Ebrë, sii sama jëkkër indi ci kër gi, mu di nu yab. Dafa ñëw, bëgg maa tëdde, ma yuuxu ca kaw.
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
mu woo surgay kër ga, ne leen: «Xool-leen, Ebrë, sii sama jëkkër indi ci kër gi, mu di nu yab. Dafa ñëw, bëgg maa tëdde, ma yuuxu ca kaw.
¶ «Buleen siiwal ay fen; buleen lëngoo ak tooñkat, ngir doon seedeb naaféqam.
Mu bind ca bataaxal ya ne: «Yéeneleen koor, beral Nabot jataay ci kanam mbooloo mi,
Teewlu ma, nangul ma. Li may tawat a ma xañ jàmm, ub sama bopp;
Kàdduy dëgg, day sax dàkk; fen, xef xippi, mu wéy.
Seede buy fen muccul mbugalam, kuy noyyee ay fen, mujje sànku.