Genesis 12:14
TSK
¶ Ba Ibraam àggee Misra, waa Misra gis ne jigéen ji mu àndal rafet na lool.
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
¶ Ba Ibraam àggee Misra, waa Misra gis ne jigéen ji mu àndal rafet na lool.
Sang ba am cofeel ci Yuusufa, def ko fara biir këram, dénk ko saytub kër ga, ba teg ciy loxoom lépp lu mu moom.
Wattukat ba seetatuloon dara lu Yuusufa jiite, ndax Aji Sax jee ànd ak moom, te lu mu sabablu, Aji Sax ji may ko ca ndam.
Yese yónnee, ñu indi ko. Ma nga def ku xees, neexa xool, bët ya leer nàññ. Aji Sax ji ne Samiyel: «Diw ko, kii la.»
Jëkkër ja da koy wóolu, te jëkkër ja day am xéewal, du ko ñàkk.
Mu ne ko: “Jaaraamaa, surga bu baax bi. Gannaaw ci lu tuut nga wóore nag, falul ci fukki dëkk.”