Job 15:22
TSK
Dootu yaakaara mucc musiba, saamar a koy yoot,
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Dootu yaakaara mucc musiba, saamar a koy yoot,
Ci kaw loolu tàngooru naaj wu metti di lakk nit ñi. Nit ñi nag tuubuñu, sàbbaal Yàlla; xanaa di saaga Yàlla, ji dogal yooyu musiba.
Tawu doji yuur yu benn talaŋ, yemook ñeent fukki kilo, daldi sóobe asamaan ci kaw nit ñi, ñuy saaga Yàlla ngir musibam doji yuur yi, ndax musiba mu réy ba jéggi dayo.