TSK

TSK · Genesis 4:9

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Yuda ne doomi baayam ya: «Bu nu reyee sunu rakk jii, nëbb deret ji, lu nu ciy jële?

Job 22:13 TSK

Nga naa: «Ana lu Yàlla xam? Ana nu muy àttee ci gii lëndëm gu tar?

Mooy topp nit bakkanu moroomam, di ko ba xel, te du fàtte yuuxi néew-ji-doole.

Kuy làq say tooñ doo baaxle, ku koy nangu, tuub ko, am yërmandey Yàlla.

Acts 5:4 TSK

Ba mu jaragul, du yaa doon boroom? Gannaaw ba mu jaree it, xanaa du njég gaa ngi sa loxo ba tey? Ana noo mana xajale mii mébét ci sa xol? Du nit nga wor de, waaye Yàlla nga wor.»