¶ Askanu Yanqóoba mooy lii. Yuusufa tollu na ci waxambaane, am fukki at ak juróom ñaar, di sàmmle jur gi doomi baayam, yi nga xam ne soxnay baayam Bilaa ak Silpa ñoo leen jur. Yuusufa nag di leen boole ak seen baay.
TSK
TSK · Genesis 41:46
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Genesis 37:2
TSK
1 Samuel 16:21
TSK
Daawuda dem ca Sóol, daldi tàmbali di ko liggéeyal. Sóol sopp ko lool. Daawuda nag mujj di gàddukatu gànnaayam.
1 Kings 12:6
TSK
¶ Buur Robowam giseek mag ña daa taxawu Suleymaan baayam ba muy dund. Mu ne leen: «Lu ngeen may digal, ma wax ko mbooloo mii?»
Proverbs 22:29
TSK
Seetlul ku man liggéeyam, buur lay liggéeyal, du liggéeyal baadoolo.
Daniel 1:19
TSK
Buur wax ak ñoom te gisul ci ñoom ñépp kenn ku mel ni Dañeel ak Anaña ak Mikayel ak Asaryaa. Ñu daldi tàbbi ci liggéeyu buur.
Luke 21:36
TSK
Teewluleen boog, tey ñaan saa su nekk, ba mana mucc ci mboolem looluy nara xew, ngir ngeen taxaw fi kanam Doomu nit ki.»