Genesis 41:3
TSK
Mu dellu gis juróom ñaari nag yu ñaaw te yooy topp ca ñoom, génne ca dex ga, làng ak ñoom ca tàkk ga.
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Mu dellu gis juróom ñaari nag yu ñaaw te yooy topp ca ñoom, génne ca dex ga, làng ak ñoom ca tàkk ga.
Te itam juróom ñaari nag yu yooy, yi ci topp te ñaaw, juróom ñaari at la. Naka noonu juróom ñaari gub yu gooy, yi ngelaw li lakk, juróom ñaari ati xiif lay firi.
Mu ne leen: «Dégg naa ne pepp am na ca Misra. Demleen jëndali nu ca, ndax nu mana dund, ba xiif bañ noo rey kay!»
Fekk booba Yuusufa mooy dogal ca réew ma, di jaay pepp waa réew mépp. Magi Yuusufa ya ñëw, sujjóotal Yuusufa.
ndaxte des na juróomi ati xiif. Waaye dinaa la fi yore, ba doo ñàkk dara, yaak sa waa kër ak mboolem lu bokk ci yaw.”
Moo wàcce ab xiif ca réew ma, dagge fa luy gub,