Genesis 40:14
TSK
Waaye ngalla boo delloo ca sa teraanga, nanga ma geestu te dimbali ma, waxal ma Firawna lu jëm ci man, ba man maa génne fii.
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Waaye ngalla boo delloo ca sa teraanga, nanga ma geestu te dimbali ma, waxal ma Firawna lu jëm ci man, ba man maa génne fii.
Kàddug Aji Sax ji di nattu Yuusufa, ba keroog pirim ma dikk,