TSK

TSK · Genesis 42:10

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Isaaxa ne Esawu: «Mbaa am naa lu ma la ñaanalati, doom? Ndax kat xas naa koo def, muy sa kilifa, te bokkam yépp laa def ñuy surgaam, te pepp ak biiñ laa ko woomale it, ba mu ne gàññ.»

Ngalla kilifa gi, yaay sunu sang; koo ko fekke ci nun rekk, boo yeboo reyal, ñi des ci nun doxe fa, di say jaam.»

Abdiyas di dem, Ilyaas ne pemm dajeek moom ca yoon wa. Abdiyas xàmmi ko, sujjóotal ko, dëpp jë ba fa suuf, ne ko: «Kii Ilyaas a, sama sang?»