Genesis 40:4
TSK
Kilifag wattukat ya teg leen ca loxol Yuusufa, mu di leen topptoo. Ba ñu nekkee ab diir ca kaso ba,
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Kilifag wattukat ya teg leen ca loxol Yuusufa, mu di leen topptoo. Ba ñu nekkee ab diir ca kaso ba,
Sang bi, ba nga nu meree, yaw Firawna, ba tëj ma kaso ca kër njiitu dag ya, man ak kilifag lakk-kati mburu ya,
Aji Sax ji, def nga la nga dige woon, Sang bi, defal nga ma ngëneel.
Ñu daldi leen teg loxo, tëj leen ba ca ëllëg sa, ndax booba guddi na.
Sunuy baay a nu yar fan yu néew, na mu jaadoo woon ci seenum xel. Waaye sunu Baay bii, sunu njariñal bopp lanuy yare, ngir nu séddu ci sellaayam.