TSK

TSK · Genesis 42:19

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Ba ñu demee, ba metitu xiif bi dajal réew mépp, Yuusufa dafa ubbi denc yépp, di jaay pepp mi waa Misra,

Ba mu ko defee ñu sëf seeni mbaam pepp ma, daldi fay bàyyikoo.

Baayam nag, mu yóbbante ko fukki mbaam yu góor yu sëf lay tànnéef ca Misra, ak fukki mbaam yu jigéen yu sëf pepp ak mburu, tegal ko ca lu mu dunde ca yoon wa, buy ñëw.

Waaye ñu ngii di xeet wu ñu futti, sëxëtoo; ñépp tëje ciy pax, dence ci këri tëjukaay, ñu doon alalu xare fu leen kenn dul xettlee, xanaa ñu di leen sëxëtoo, te kenn du ne ñu delloo leen.