TSK

TSK · Genesis 42:27

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

¶ Naka la ku nekk sotti saakoom, ne jàkk ca mbuusu xaalisam. Ba ñu gisee mbuusi xaalis ya, ñoom ak seen baay, dañoo tiit.

waaye ba nu dalee ca yoon wa, danoo ubbi sunuy saaku, ku nekk ci nun fekk xaalisam ca kaw, mu tollu na mu tollu woon, te indiwaat nanu ko.

¶ Ba ñu lalee panaan ca yoon wa, Aji Sax ji dafa dogale Musaa, nar koo rey.

Mu dikk, sotti diw ak biiñ ca gaañu-gaañu ya, lëmës ko. Ci kaw loolu mu teg ko ci mbaamam, yóbbu ko ci ab dalukaay, di ko topptoo.