Genesis 37:11
TSK
Mag ya nag iñaane ko. Teewul baayam moom bàyyi xel ci mbir moomu.
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Mag ya nag iñaane ko. Teewul baayam moom bàyyi xel ci mbir moomu.
«Waa ja yilif réew ma dafa noo résëti, foog ne danuy yëddusi réew ma.
¶ Gannaaw gi Aji Sax ji mbugal na mbooloo ma ndax la ñu sàkkloo woon Aaróona aw sëllu.
¶ Ñooñu la Musaa yónni woon, ngir ñu yëri réew ma. Oseya doomu Nuun nag, Musaa tudde ko Yosuwe.
Mu yebal ay ndaw yu ko nemmikujil, ba mu wóor ko ne Sóol agsi na.
Ngëm moo waral ba Raxab gànc ba dalalee jàmm nemmikukati réew ma, àndul ak ñu gëmadi ña dee.