Genesis 42:20
TSK
Waaye nangeen ma indil seen rakk, ba ma xam ne li ngeen wax dëgg la; su ko defee dungeen dee.» Ñu daldi ne: «Waaw,»
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Waaye nangeen ma indil seen rakk, ba ma xam ne li ngeen wax dëgg la; su ko defee dungeen dee.» Ñu daldi ne: «Waaw,»
Maa leen di toppe bëtu mbaax, ba délloosi leen ci réew mii. Maa leen di defar te duma leen daaneel; jëmbat leen te duma leen buddi.
Su ñu demee, diy jaam ñu seeni noon jiital, fa laay sante boroom saamar, mu bóom leen. Du bëtu jàmm laa leen di xoole, bët bu aay laa leen di xoole moos!»