Genesis 41:43
TSK
ba noppi waral ko watiiru ku sës rëkk ci moom Firawna, te fu mu ware ñu jiitu ko, di yéene naan: «Sujjóotleen!» Noonu la ko Firawna fale, mu yilif Misra gépp.
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
ba noppi waral ko watiiru ku sës rëkk ci moom Firawna, te fu mu ware ñu jiitu ko, di yéene naan: «Sujjóotleen!» Noonu la ko Firawna fale, mu yilif Misra gépp.
Firawna dellu ne Yuusufa: «Am nga ndigal itam ci wax leen ne leen: “Ni ngeen koy defe nii la: dangeen di jële ay watiir ci réew mi, dem yeb ci seeni doom ak seeni soxna, te ànd ak seen baay, ngeen ñëw.
ay watiir aki gawar topp ca, ñu def gàngoor gu réy.
Ba loolu amee ñépp jooyoo jooy yu metti, laxasu ko, fóon ko.