TSK

TSK · Genesis 46:6

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Aji Sax ji wax Ibraam ne ko: «Déglul bu baax li ma lay wax: sa askan dinañu nekk ay doxandéem ci réew mu ñu moomul, ñu def leeni jaam, sonal leen diiru ñeenti téeméeri at.

Juróom ñaar fukki bakkan la seeni maam doonoon ba ñuy wàccsi Misra. Tey seen Yàlla Aji Sax ji def leen ngeen day ni biddiiwi asamaan.

Israyil agsi Misra, muy nganug Yanqóoba ga ca réewum Xam.

Acts 7:15 TSK

Noonu la Yanqóoba deme Misra, ba faatoo fa, mook sunuy maam.