TSK

TSK · Genesis 47:13

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Te juróom ñaari ati xiif a ciy topp, ba ñu fàtte naataange gu réy ga amoon réewum Misra. Xiif ba cay topp dina yàq réew mi.

¶ Axab nag ne Abdiyas: «Duggal ci biir réew mi te seet ci bëti ndox yeek xur yépp. Jombul nu gis ñax, ba mana rawale bakkani fas yeek berkelle yi, ba du jar nu di leen jekkli.»

¶ Kàddug Aji Sax jii dikkaloon na Yeremi, jëm ca maral ma. Mu ne:

Ña saamar rey a gënu demin ña deeye xiif, jeex tàkk, ne lasar, ndax ñàkk meññatum tool.

Acts 7:11 TSK

¶ «Ci kaw loolu ab xiif dikkal Misra gépp ak réewum Kanaan. Mu metti lool. Sunuy maam nag amatuñu ab dund.