Genesis 41:36
TSK
Dund boobooy doon sàqu réew mi diiru juróom ñaari ati xiif yiy dal ci réewum Misra; su ko defee waa réew mi duñu loru ci xiif bi.»
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Dund boobooy doon sàqu réew mi diiru juróom ñaari ati xiif yiy dal ci réewum Misra; su ko defee waa réew mi duñu loru ci xiif bi.»
Seytaane ne Aji Sax ji: «Bakkan a wuutu bakkan rekk. Mboolem lu nit am, man na koo weccee bakkanam.
Nu nangul Misra, nangul Asiri ngir ab dund.