TSK

TSK · Genesis 48:12

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Naka la siggi, gis ñetti nit, ñu ne jimeet ci kanamam. Ibraayma gaawtu, gatandu leen, sujjóotal leen.

¶ Naka la Ibraayma dégg loolu, daldi jóg sujjóotal waa réew ma, maanaam Etteen ña.

Fekk booba Yuusufa mooy dogal ca réew ma, di jaay pepp waa réew mépp. Magi Yuusufa ya ñëw, sujjóotal Yuusufa.

Ba loolu amee Musaa ne gurub fa suuf, sujjóot,

¶ «Bu boroom bijjaaw teewee, jógleen wormaal ko. Deeleen rus mag te ragal-leen seen Yàlla. Maay Aji Sax ji.

Ndaw sa ne gurub cay tànkam, sujjóot; ba noppi fab doomam, génn.

¶ Naka yeen xale yi, déggal-leen seeni waajur, ngir Boroom bi, ndax moo war.