TSK

TSK · Genesis 7:2

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Rab yu set yi ak yi setul ak picc yi ak yiy raam

Dangeen wara mana ràññee lu sell ak lu ñu sellalul, dangeen wara ràññee itam lu set ak lu setul.

Lu ngeen sib lay doon, kon buleen ci lekk yàppu lenn te sibleen méddam.

¶ Ay doom ngeen, ñeel seen Yàlla Aji Sax ji. Buleen ñaasu, buleen wat seen kawaru bopp fi féeteek jë bi, ngir di ko mititloo ku dee,

Mu daldi gis asamaan ubbiku, lu mel ni sér bu mag bu ñu téyee ñeenti lafam, wàcce asamaan, jëm suuf.