TSK

TSK · Haggai 2:1

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

¶ -Ca ñaareelu atu nguuru Buur Daryus, ca juróom benneelu weer wa, yemook benn fan ca weer wa, kàddug Aji Sax ji moo dikk ci jottlib Yonent Yàlla Ase, ñeel doomu Selcel, Sorobabel boroom Yuda, ñeel itam doomu Yoccadag, Yosuwe sarxalkat bu mag ba. Mu ne:

¶ Ca ñaar fukki fan ak ñeentu juróom ñeenteelu weer wa, yemook ñaareelu atu nguuru Buur Daryus, kàddug Aji Sax ji moo dikkal Yonent Yàlla Ase, ne ko:

Ndax kat du genn kàddug waxyu gu masa soqikoo ci coobarey nit, waaye ci xiirtalub Noo gu Sell gi la aw nit daan waxe waxyu bu bawoo fa Yàlla.