¶ Aji Sax ji nag yeb Yosuwe doomu Nuun ne ko: «Dëgërlul te am fit, ndax yaw yaay yóbbu bànni Israyil ca réew ma ma giñoon, te man ci sama bopp maay nekk ak yaw.»
TSK
TSK · Haggai 2:4
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
1 Samuel 16:18
TSK
Kenn ca dag ya ne ko: «Man de, gis naa jenn doomu Yese waa Betleyem bi. Ku mana xalam la te jàmbaare. Ñeyi xare la. Ku déggi wax, ku góorayiw, te Aji Sax ji ànd ak moom.»
Haggai 1:13
TSK
La ca tegu Ase, ndawal Aji Sax ji, jottli askan wa yóbbanteb Aji Sax ji. Mu ne leen: «Maa ànd ak yeen, kàddug Aji Sax jee.»
¶ Teewluleen te saxoo ngëm, góor-góorluleen te dëgërlu.
2 Timothy 2:1
TSK
¶ Kon nag yaw doom, doolewool yiw, wi Almasi Yeesu di maye.