Numbers 14:25
TSK
Gannaaw Amalegeen ñaak Kanaaneen ñaa nga dëkke xur wi nag, bu ëllëgee walbatikuleen, toppaat màndiŋ mi, te jaareji ko géeju Barax ya.»
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Gannaaw Amalegeen ñaak Kanaaneen ñaa nga dëkke xur wi nag, bu ëllëgee walbatikuleen, toppaat màndiŋ mi, te jaareji ko géeju Barax ya.»
Man Aji Sax ji, maa ko wax. Noonu déy laay def mboolem mbooloo mu bon mii booloo ci sama kaw. Ci màndiŋ mii lañuy raafe, fii lañuy deeye.»
¶ Ba Aji Sax ji déggee seeni kàddu, dafa mer ba giñ ne:
Moo ma taxa mer, ba giñal leen, ne duñu tàbbi fa sama noflaay.»
Nun ñi gëm doŋŋ nooy tàbbi ci noflaayam, noonu mu ko waxe, ne: «Maa giñe sama biir mer, ne: “Duñu tàbbi mukk ci samag noflaay.” » Ndaxam ca cosaanu àddina la liggéeyi Yàlla sotti woon ba noppi,
Kon des na ba tey noflaayu bésub juróom ñaareel bu ñu waajalal ñoñu Yàlla.