Genesis 22:15
TSK
¶ Ci kaw loolu malaakam Yàlla ma dellu àddoo asamaan ne Ibraayma:
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
¶ Ci kaw loolu malaakam Yàlla ma dellu àddoo asamaan ne Ibraayma:
ga mu digoon Ibraayma, giñal ko Isaaxa,
Waaye su ngeen dégluwul sama santaane yii, giñ naa ko ci man mii,” kàddug Aji Sax jee, “ab gent rekk la gii kër di doon!”»
Maay faagaagal sa mboolem jur, gi feggook ndox mi ne xéew, ba tànku nit dootu ko nëxal, wewu jur dootu ko nëxal.
ak ngiñ la mu giñaloon sunu maam Ibraayma,