TSK

TSK · Hebrews 9:3

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

¶ Ñu sàkk itam rido bi, ràbbe ko wëñ gu baxa te laal yolet, ak wëñ gu xewar, ak gu xonq curr ak wëñu lẽe, ñawaale ci ay nataali serub.

Ba mu ko defee ñu fat gaal gi ci biir bérab bu sell bi, doora firi ridob xàjjatle bi, làqe ko ko, na ko Aji Sax ji sante woon Musaa.

Mu natt néegu biir bi ci boppam, muy ñaar fukki xasab wet gii, di ñaar fukki xasab wetu néeg bu mag ba. Mu ne ma: «Fii mooy fu sell fee sell.»

Yaakaar jooju lanu am, mu mel ni diigalub gaal, diigal bu dëgër te wóor, ñeel sunu xol, te yaakaar jooju mooy bëtt rido ba, ba jàll ca néegu biir bu Yàlla ba.

¶ Léegi nag bokk yi, am nanu sañ-sañu dugg ca bérab bu sell baa sell, ngir deretu Yeesu,