TSK

TSK · Hosea 13:8

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Xam nga sa baay ak ay nitam. Ay xarekat yu jàmbaare lañu te wex ni gaynde gu ñu nangu doom ya, te it, sa baay ku xam xeex la, du fanaan ak xarekat ya.

Lu tax nga bëtt ay miiram, ba ku fa jaare witt ca,

Dañuy ŋar ni gaynde, ŋarati ni gaynde gu mat; yëmmu, ŋank um rëbbam, yóbbu te kenn du wallu.

Sama séddoo baa ngi may saf tan mu todde mu moroomi tanam gaw. Doxleen dajaleji rabi àll yépp, indi leen ci bernde ji.