TSK

TSK · Hosea 2:10

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Ab soxor mbugalam du jaas, wóor na; te ku jub, saw askan mucc.

Soo nee ci sam xel: «Lu tax lii dal ma?» xamal ne sa ñaawtéef gu réy a waral ñu ñori la, saaysaaye la.

Yaa tànn ci sa yére yu yànj, rafetale sa jaamookaayi tuur, ba noppi di ca gànctu; lu masula am te du amati mukk.

Boroom bi Aji Sax ji dafa wax ne: Gannaaw yaa wasaare sa alal, ñoriku ne duŋŋ, di gànctook sa far yii, muy sa mboolem kasaray tuur, bay tuur sa deretu doom yi nga leen rendil,

Hosea 2:3 TSK

Nanga wooye sa bokk yu góor: “Ñoñi Aji Sax ji,” sa bokk yu jigéen, nga ne leen: “Ñi Aji Sax ji yërëm.”

Israyil di reseñ gu naat, meññal boppam lu ne gàññ, te lu meññeef ma gëna yokku, mu gëna yokkati sarxalukaayi tuur. Lu am réewam gëna baaxle, mu gëna baaxal ay xeri tuur.

Moo tax ma mel ni gaynde ci yeen di tëroo ni segg ciw yoon.

Luke 12:2 TSK

Mboolem lu nëbbu dees na ko feeñal, te lu làqu dees na ko xam.