TSK

TSK · Hosea 3:2

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Ñaar fukki at a ngii, ma di la jaamu ci kër gi, liggéeyal naa la fukki at ak ñeent ngir sa ñaari doom yu jigéen ñii, teg ci juróom benni at yu ma la sàmmal say gàtt, nga soppi sama peyoor fukki yoon ak juróom.

¶ «Ab xërëmkat bu jigéen, buleen ko bàyyi, mu dund.

¶ Sóol ne leen: «Waxleen Daawuda ne ko, Buur de sàkkuwul ub can: xanaa téeméeri mbuñukay waa Filisti yu mu feyoo ci noonam yooyu.» Booba la Sóol laloon mooy pexe mu tàbbal Daawuda ca loxol waa Filisti.

Na benn efa ak benn bat yem dayo, lu ci nekk wara def céru fukkeelu benn omer, bi yemook ñaar téeméeri liitar ak ñaar fukk (220), mbaa téeméeri kilo ak juróom fukk (150). Te na benn omer di dayo bi ngeen di natte.