Bésub keroog booba, ku bew bay regeju mooy detteelu, sagub nit sàggiku, Aji Sax ji doŋŋ mooy jagoo kawe.
TSK
TSK · Isaiah 10:33
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Isaiah 2:11
TSK
Isaiah 2:13
TSK
Ca lay xaare garabi seedari Libaŋ yi ne coleet, ba kawe, ak garab yu mag ya fa Basan.
Isaiah 18:5
TSK
Bala ngóob di jot, te fekk lépp tóor, ba tóor-tóor def reseñ ju xaay, mu jël ab sàrt, dog car yu ndaw yi, tenqi car yu mag ya, sànni;
Isaiah 37:24
TSK
Yaa yebal say surga, di kókkali Boroom bi, te naa: “Sama watiir yi ne xas laa ware kawtey tund yi, jàll ba ca xolu Libaŋ. Maa gor seedaram ya fa sut ak tànnéefi garabi sipparam: maay àkki ba ca collub kaw bu tundu Libaŋ, ak gottam bu naat ba nib tóokër.
Jeremiah 22:7
TSK
Maa lay beralal yàqkat yu fàggu seeni gànnaay, dàjji sa tànnéefi banti seedar, sànni ca sawara sa.
Amos 2:9
TSK
«Ndaxam maa leen reyaloon Amoreen ñu gudd ña te réy, mbete garab yu mag. Ma boor doom ya, buur reen ya.