TSK

TSK · Isaiah 10:7

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Dëgg la, fexeel ngeen ma lu bon, waaye Yàllaa ko walbati, def ko lu baax, ba dogal li am tey jii, muy bakkan yu bare yi mucc.

Ana tuuri réew yii di Amat ak Arpàdd? Ana tuuri Sefarwayim? Ndax dañoo xettli Samari ci man?

te ñoo sànni seeni yàlla ci sawara it, ndax yooyoo dul Yàlla, xanaa lu nit sàkke loxoom, bant ak doj, ba tax ñu sànk leen.

Tey ci sa kaw, la xeet yu bare daje, yaw Siyoŋ, te naan: «Nees ko tëdde, nanu seetaan Siyoŋ!»

Acts 2:23 TSK

Nit kooku ñu jébbale ni ko Yàlla dogale te nasoon ko lu jiitu, yeena ko daajloo yéefar yi ci bant, reylu ko.