TSK

TSK · Isaiah 18:3

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Muy kàddug Sabóor, giiroo ci Asaf. Yàlla, Aji Sax ji Yàlla àddu na, di woo àddina, penku ba sowu.

Aji Sax jeey yékkatil raaya, xeet wu sore, wal ug liit, wooye leen fa cati àddina, ñu jekki ne jaas, dikkal leen.

Mooy yékkatil xeet yi raaya, dajale góor ña ñu dàqe Israyil, ak jigéen ña ñu jële Yuda, tasaare leen, ñu jóge ñeenti weti àddina, booloo.

Coowal mbooloo ngoog ca tund ya, mel ni ñu baree bare! Riirum nguuri nguur yu daje, di xeeti xeet! Aji Sax ji Boroom gàngoor yi mooy dajale gàngooru xare.

Éy waa réew mi, waa réew mee, waa réew mi, dégluleen Kàddug Aji Sax ji!

Micah 6:2 TSK

Yeen tund yu mag yi, dégluleen layoob Aji Sax ji, ak yeen kenuy suuf yi sax dàkk. Aji Sax jee joteek ñoñam, mooy wàqanteek Israyil.

Su boobaa Aji Sax jeey feeñ fi leen tiim, ag fittam tàkk nig melax. Bufta gi la Boroom bi Aji Sax ji di wal, ànd ak ngëléni bëj-saalum, dikk.