Misra daal, nga def sa yaakaar, bantu barax bu tas boobu di sokk képp ku ko wéeroo! Firawna buuru Misra de, mooy boobu bant ci képp ku ko yaakaar.
TSK
TSK · Isaiah 20:5
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
2 Kings 18:21
TSK
Isaiah 30:3
TSK
Rawtub Firawnaay mujj di seen gàcce, keppaarug Misra di seen toroxte.
Isaiah 30:7
TSK
Ndimbalu Misra, cóolóolu neen! Moo tax ma tudde ko: Raxab, ponkal mi ne yàcc.
Jeremiah 9:23
TSK
Kuy damu kay, na damoom xelam mu ko may mu xam ma, xam ne maay Aji Sax, jiy jëfe ngor ak dëgg ak njekk fi kaw suuf. Loolu déy mooy sama bànneex.» Kàddug Aji Sax jee.
Jeremiah 46:25
TSK
¶ Aji Sax ji Yàllay Israyil, Boroom gàngoori xare yi wax na ne: «Maa ngii di dikke mbugal Amon, tuuru dëkk bii di Teeb, ak Firawnaak waa Misraak seeni tuur ak seeni kàngam, boole ci ñi yaakaar Firawna.
Ezekiel 29:7
TSK
ñu jafandu ko, mu ne tàllit, ne xureet mbagg yépp, ñu wéeroo ko, mu ne tipp, ndigg yépp rëcc.
¶ Kon nag bu kenn puukarewoo ay nit, ndax lépp, yeena ko moom,