1 Kings 10:15
TSK
te limaaleesul galag ya jóge ca jaaykat ya ak jula yaak mboolem buuri Arabi, ak jaraafi réew ma.
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
te limaaleesul galag ya jóge ca jaaykat ya ak jula yaak mboolem buuri Arabi, ak jaraafi réew ma.
Deesatu fa dëkk, xanaa gental ba fàww. Màngaan dootu fa samp xayma, sàmm dootu fa gooral.
ak mboolem buuri Arabi ak mboolem buuri xeeti njaxasaan yi dëkke màndiŋ mi,
¶ Lu jëm ci Kedar ak nguuri Àccor yi Nabukodonosor buuru Babilon nangu woon, Aji Sax ji dafa wax ne: «Ñokket ci kaw Kedar, ba tas waa penku yooyu,
Waa Dedan it di say jula, indil la seen ndimoy tegi fas.