Isaiah 23:7
TSK
Xanaa lii du seen dëkk bu xumb ba, te cosaanam di janti démb, nit ña di fa jógey sancaani fu sore?
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Xanaa lii du seen dëkk bu xumb ba, te cosaanam di janti démb, nit ña di fa jógey sancaani fu sore?
Moo tax Aji Sax ji wax ci buurub Asiri ne: “Du dugg ci dëkk bii, du fi soqig fitt, du fi taxawe ab pakk, du fi jal jal bu muy gawe!
Ma dem, xool àll, gisuma lu moy ñu saamar bóom, ma dugg biir dëkk, gisuma lu moy ñu ne làcc akub xiif, yonent ak sarxalkat di wër réew mi, xam-xam réer leen.”»
Keroog juróom ñeenti fan ca ñeenteelu weer wa, xiif ba tar lool ca biir dëkk ba, ba waa réew ma amatuñu ab dund.
Ña saamar rey a gënu demin ña deeye xiif, jeex tàkk, ne lasar, ndax ñàkk meññatum tool.
Wóoy yeen ñiy jéema fanq bésub njàqare tey woo nguurug fitna!