TSK

TSK · Isaiah 22:6

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Doomi Sem yu góor ñii la: Elam ak Asur ak Arpagsàdd ak Ludd ak Aram.

Bésub keroog Boroom bi jooti loxoom ñaareel bi yoon, ngir jotaat ndesu ñoñam, wa des Asiri ak Misra, ak Pattros ak réewum Kuus, ak Elam ak Sineyaar, ak Amat ak biir duni géej ya.

Peeñu mu ñàng lañu ma ci wax. Workat biy wor, yàqkat biy yàq. Yeen waa Elam, songleen; yeen waa Medd, gawleen leen. Dakkal naa mboolem onk yu ñu sabab.

Amos 1:5 TSK

Maay dàjji bunti dëkkub Damaas, faagaagal waa xuru Awen, boole ca boroom Bet Eden. Waa Siri dugg ngàllo, dellu Kir.» Aji Sax jee ko wax.