TSK

TSK · Isaiah 23:4

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Booba fas yaa ràmbal, watiir ya riir, mbegey watiir ya kar-kareendoo, yoxo yoqi, ba baay geesuwul doom,

«Yaw nit ki, neel jàkk Sidon, nga biral waxyu fi kawam.

làmp du niiteeti fi yaw, te baatu boroom séet akub séetam du jibeeti fi yaw mukk, ndax say julaa ëppoon doole ci àddina, te say xërëm a sànk askanoo askan.»