TSK

TSK · Isaiah 23:5

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

«Boroom bi Aji Sax ji dafa wax Tir, ne ko: Keroog sa coowal jéll ba, ba ñuy bóome fa sa biir, ñay dee di binni, dun yaa cay dégg, di lox moos!

Mboolem ñi la xam ci xeet yi, seen yaram dina daw ci yaw. Ku raglu ngay doon, te doo tekkeeti ba fàww.”»