TSK

TSK · Isaiah 28:4

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Bala xale bee man ne “Baay” mbaa “Yaay” déy, dees na yóbbul buurub Asiri alal ju ñu foqatee Damaas, ak lël ju ñu këfe Samari, nangu ko.»

Hosea 6:4 TSK

«Ana nu ma lay def, yaw Efrayim? Nu ma lay def yaw Yuda? Te sa ngor di xiinu suba, mbaa ab lay, jekki ne mes.

Fàddees na Efrayim, ay reenam wow, du meññ benn doom. Bu juroon itam, maay rey ngëneelu biiram.»

Efrayim moom, su naatee ci biiri bokkam it, fa màndiŋ ma la ngelawal penku, ngelawal Aji Sax ji di uppe, bëti ndoxam tëju, ay teenam déy. Kii mooy sëxëtoo ab dencam, ak mboolem lu cay alal.»

Sa tata yépp ni garabi figg yu ñoral ndoortel meññeef lay mel, soo yëlbee, doom ya rot, gémmiñu lekk-kat aw.

Biddiiw yi fàqe asamaan, wadd ci suuf, ni doom yu xaay yu ngëlén gësëm seen ndey.