Isaiah 2:13
TSK
Ca lay xaare garabi seedari Libaŋ yi ne coleet, ba kawe, ak garab yu mag ya fa Basan.
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Ca lay xaare garabi seedari Libaŋ yi ne coleet, ba kawe, ak garab yu mag ya fa Basan.
Kàngam yi, ñu jàpp, wékk; te mag ñi, teraleesu leen.
Ba loolu wéyee mu wax ak ña ca des, may dégg. Mu ne leen: «Toppleen ko ca biir dëkk ba te ngeen rey. Buleen xool bëti ñéeblu, buleen ñeewante.
Maay dagge fa seen biir seen njiit, booleeki kàngamam, bóom.» Aji Sax jee ko wax.