TSK

TSK · Isaiah 32:12

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Réew mooma ngeen jàll jëm, ngir nanguji ko, réewum tund aki xur la, te ndoxum taw lay naan.

Biiñ ñàkk na, garabu reseñ lax, bépp xol bu tooyoon, binni.

Ag till sax joxe na weenam, nàmpal doomam, te sama bokk yi mujj néeg ba mel ni bànjóolig màndiŋ.

Ba tey maa leen giñal ca màndiŋ ma, ne duma leen yóbbu réew ma ma leen jox, fa meew maak lem ja tuuroo, fa gëna taaru ci réew yépp.

Nahum 2:7 TSK

Bunt ya jëm dex ga ñooy jekki ubbiku, kër buur màbb.