TSK

TSK · Isaiah 33:12

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Waaye ku bon, ñu buub nig taxas, sànni. Deesu ko fore loxo,

Mbon a ngi tàkk moos ni sawara, xoyom dég aki dagg, jafal gajji gott bi, mu ne jippét, saxar, naaw.

Aji Sax ji, leeru Israyil mooy doon sawara, ku Sellam kooku mooy doon tàkk-tàkku sawara, xoyom taxasi Asiri aki dégam ci benn bés.

¶ Ba loolu amee malaakam Aji Sax ji dikk, fàdd ca dalub Asiri téeméer ak juróom ñett fukk ak juróomi junni (185 000). Ca ëllëg sa ña mucc teela xëy, yemuñu ci lu moy ñooña ñépp diy néew.